Luke 12:48 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye surga bi xamul bëgg-bëggu njaatigeem, te def lu yelloo ay dóor, dinañu ko dóor dóor yu néew. Ku ñu jox lu bare dees na la feyiku lu bare. Ku ñu dénk lu bare, dees na la laajaat lu ko ëpp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye jawriñ ji xamul nammeelu njaatigeem, te teewu koo def lu yelloo ay duma, yet yu néew lay am. Képp ku ñu jox lu bare, dees na la topp lu bare. Képp ku ñu dénk jopp, dees na la feyeeku lu ko ëpp.