Luke 12:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dinaa leen wax nag ki ngeen war a ragal: ragal-leen Ki nga xam ne bu reyee ba noppi, am sañ-sañu sànni ca safara. Waaw maa ngi leen koy wax, ragal-leen kooku.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma xamal leen nag ki ngeen wara ragal: kiy rey ba noppi, am sañ-sañu sànni ca sawara sa, kooku déy laa leen ne, ragal-leen ko.