Luke 12:58 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu la nit jiiñee dara, ba ngeen ànd di dem ca àttekat ba, nanga fexee juboo ak moom ci yoon wi. Lu ko moy, dina la yóbbu ci yoon, yoon jébbal la ca loxoy alkaati ba, mu tëj la.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Boo àndeek sab jotewaale, ngeen jëm ca àttekat ba, fexeela jubook moom ci yoon wi. Lu ko moy mu yóbbu la ci yoon, yoon jébbal la ndawal buur, mu ne la ràpp tëj.