Luke 12:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Juróomi picci rammatu, ndax duñu ko jaay ci ñaari dërëm? Moona Yàlla fàttewul benn ci ñoom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Juróomi picci ramatu, xanaa jarul ñaari dërëm doŋŋ? Moona Yàlla fàttewula geesu menn ci ñoom.