Luke 12:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Seen kawari bopp sax waññees na leen. Kon buleen ragal dara, yéena gën ndiiraanu rammatu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen nag seen kawari bopp sax, waññees na lépp. Buleen ragal dara, nde ndiiraanu ramatu, yeena ko gën.