Luke 12:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Te maa ngi leen koy wax, képp ku ma nangu ci kanamu nit ñi, Doomu nit ki dina la nangu ci kanamu malaakay Yàlla yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Te it maa leen ko wax, képp ku dëggal fi kanam nit ñi, ne man nga féeteel, Doomu nit ki itam dina dëggal fa kanam malaakay Yàlla ya, ne moom nga féeteel.