Luke 12:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ku ma gàntu ci kanamu nit ñi, dinañu la gàntu ci kanamu malaakay Yàlla yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye ku weddi fi kanam nit ñi, ne man nga féeteel, dees na weddi fa kanam malaakay Yàlla ya, ne man nga féeteel.