Luke 13:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ca jamono jooju ay nit ñëw ca Yeesu, nettali mbirum waa Galile, ya Pilaat reylu woon, jaxase seen deret ak dereti mala, yi ñu rendi woon, jébbal leen Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jamono jooju tembe la aw nit dikk, àgge Yeesu mbirum waa Galile yu Pilaat bóomoon, jaxase seen deret ak seen dereti juru sarax yu ñu jagleel Yàlla.