Luke 13:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Jigéen jii nag bokk ci askanu Ibraayma te Seytaane tënk ko fukki at ak juróom-ñett, ndax kenn waru koo yiwi ci bésu noflaay bi?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jigéen jii di sëtub Ibraayma, te fukki at ak juróom ñett a ngii Seytaane làggal ko, wareesu koo yiwi, teggil ko laago jii ci bésub Noflaay?»