Luke 13:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu tontu leen ne: «Mbaa du dangeen a xalaat ne, waa Galile yooyu dañoo gën a nekk bàkkaarkat ña ca des, ndax coono bi ñu daj?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu ne leen: «Foog ngeen ne waa Galile yooyu dañoo gëna bàkkaar mboolem seen bokki Galile ya ca des, ba tax ñu daj mitit wu ni tollu?