Luke 13:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Jamono dina ñëw, ju boroom kër gi di jóg, tëj buntam. Dingeen nekk ci biti di fëgg naan: “Boroom bi, ubbil nu!” Dina leen tontu ne: “Xawma fu ngeen bokk.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu boroom kër gi xasee jóg, ba tëj bunt bi, fa ngeen di doxe des biti, di fëgg naan: “Sang bi, ubbil nu!” Mu ne leen: “Xawma fu ngeen bokk.”