Luke 13:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye dina ne: “Nee naa leen xawma fu ngeen bokk. Yéen ñépp soreleen ma, defkati lu bon yi!”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu neeti leen: “Nee naa leen xawma fu ngeen bokk. Soreleen ma yeen ñépp, defkati njubadi yi!”