Luke 13:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ay nit dinañu jóge penku ak sowu, nor ak sudd, ñëw, bokk lekk ci ñam, yi Yàlla di joxe ci nguuram.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Penku ak sowu, bëj-gànnaar ak bëj-saalum, la aw nit di bawoo, dikk toog ca ndabal bernde la ca nguurug Yàlla.