Luke 13:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Maa ngi leen di wax ne, du dëgg. Waaye su ngeen tuubul seeni bàkkaar, dingeen sànku noonu, yéen ñépp itam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa leen ne déedéet kay, te su ngeen tuubul, noonu ngeen di sànkoo yeen ñépp.