Luke 13:31 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ca jamono jooja ay Farisen ñëw ca Yeesu ne ko: «Jógeel fii, dem feneen, ndaxte Erodd a ngi lay wut a rey.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca jamono jooju tembe la ay Farisen dikk, ne Yeesu: «Jógeel fii, te dem, ndax Buur Erodd da laa nara rey.»