Luke 13:33 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye fàww ma dox sama itte tey, suba ak gannaaw suba, ndaxte wareesul a reye ab yonent feneen fu dul Yerusalem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye tey ak ëllëg ak sibir, fàww ma dem, ndax ab yonent wareesu koo bóome fenn fu dul Yerusalem.