Luke 13:4 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te fukki nit ak juróom-ñett ñooñu dee, bi taaxum kaw ma ca goxu Silowe daanoo ci seen kaw, ndax dangeen a yaakaar ne, ñoo gën a nekk ay tooñkat ñeneen ñi dëkk Yerusalem yépp?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fukki nit ak juróom ñett ñooñu tata ja ca Silowe daanu ci seen kaw, ba rey leen nag, ngeen foog ne ñoo gën diy tooñkat ci Yerusalem gépp?