Luke 13:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu mu daldi leen wax léeb wii: «Nit amoon na ci toolam garab gu ñu naan figg. Benn bés mu ñëw di ko raas-si, fekku fa benn doom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu léeb leen lii nag, ne leen: «Garabu figg la nit amoon ci tóokëram. Mu dikk di ko raas-si, gisu ca dara.