Luke 14:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Benn bésu noflaay Yeesu dem ci këru benn kilifag Farisen yi, ngir lekke fa. Nit ñaa ngi ko doon xool bu baax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Benn bésub Noflaay la Yeesu reeri woon kër genn kilifag Farisen ya. Ñoom nag ñu di ko bàyyi xel bu baax.