Luke 14:16 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Yeesu tontu ko ne: «Dafa amoon nit ku togglu ay ñam, woo ay nit ñu bare.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu ne ko: «Jenn waay moo waajaloon bernde ju mag, woo ca ñu bare.
Recommended Reading