Luke 14:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Faf am ca kanamam nit ku feebaroon, ay tànkam newi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndeke jenn waay a nga fa janook moom, yaram wépp a sadd.