Luke 14:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu njaatige ba ne ko: “Génnal dëkk bi te dem ca yoon ya ak ca tool ya, xiir nit ñi, ñu duggsi, ngir sama kër fees.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Njaatige li ne ko: “Demal topp yoon yi, leru ñag yi, te nga soññ nit ñi, ñu dikk ba sama kër fees.”