Luke 14:28 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su kenn ci yéen bëggee tabax taaxum kaw, ndax du jëkk a toog, xalaat ñaata la ko war a dikke, ngir seet ba xam ndax am na xaalis bu man a àggale liggéey bi?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ana kan ci yeen sax mooy namma tabax taaxum kaw, te jëkkula toog, waññ la mu koy dikke, ngir seet ba xam ndax am na lu ko àggale,