Luke 14:31 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Walla boog ban buur mooy dugg ci xare ak beneen buur te jëkkul a toog, seet ba xam moom ak fukki junniy xarekat man na xeex ak kiy ñëw ak ñaar-fukki junniy xarekat?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am ban buur mooy xarejeek beneen buur te jëkkula toog, seet ba xam ndax man naa ànd ak fukki junniy xarekatam, ngir xarejeek ku ko songseek ñaar fukki junniy xarekat?