Luke 14:32 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su ko mënul, dafay yónni ndaw ca beneen buur ba, fi ak ma ngay sore, ngir ñu juboo.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ko manul nag, ba buur bee di soreegum lay yebal kurél ca moom, ngir seet nu mu mana sàrtoo ak moom jàmm.