Luke 14:33 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Naka noonu itam ku nekk ci yéen, bu dëdduwul li mu am lépp, du man a nekk sama taalibe.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka noonu itam, kenn ci yeen du mana doon sama taalibe te dëdduwul mboolem lu mu am.