Luke 14:34 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Xam ngeen nag ne, xorom lu baax la, waaye bu sàppee, nan lañu koy delloo cafkaam?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Xorom déy baax na, waaye bu sàppee, ana lees koy safaleetee?