Luke 14:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ñépp ne cell. Yeesu daldi laal jarag ja, faj ko, ba noppi ne ko mu ñibbi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu ne cell. Yeesu teg waa ja loxo, wéral ko, daldi ko yiwi.