Luke 15:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ay fan yu néew gannaaw gi, caat ma fab yëfam yépp, dem ca réew mu sore, yàq fa alalam ci topp nafsoom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ay fan yu néew gannaaw gi, ka gën di ndaw jaay léppam, daldi tukki réew mu sore, di topp bakkanam ba yàq fa alalam.