Luke 15:20 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
«Mu daldi jóg, jëm kër baayam. Waaye bi muy soreendi kër ga, baayam séen ko, yërëm ko, daldi daw laxasu ko, fóon ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Mu jóg, ngir dellu kër baayam. Fu sore la ko baayam séene, muy dikk. Mu ñeewante ko, daw, laxasu ko, fóon ko.
Recommended Reading