Luke 15:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu tontu ko: “Sa rakk moo dellusi, te sa baay rey na sëllu wu duuf wa, ndaxte ñibbisi na ci jàmm.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne ko: “Sa rakk jaa délsi, sa baay rey sëlluw yar wa, ndax li mu délseek jàmm.”