Luke 15:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye bi sa doom jii dikkee, moom mi yàq sa alal ci ndoxaan, reyal nga ko sëllu wu duuf wi.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sa doom jii dikk, gannaaw ba mu yàqee sa alal ci ay gànc, nga reyal ko sëlluw yafal wi!”