Luke 15:32 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye war nanoo bànneexu te bég, ndaxte sa rakk jii dafa dee woon te dundaat na, dafa réeroon te feeñ na.”»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye mbégte ak bànneex war na, ndax sa rakk jii moo dee woon te dekki na, moo réeroon te feeñ na!”»