Luke 15:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Te it bu jigéen dencoon fukki libidoor, benn réer ca, nu muy def? Ndax du taal ab làmp, bale kër ga, seet fu nekk, ba gis ko?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Te it ana jan jigéen mooy am fukki libidoor, benn réer ca, te taalul ab làmp, buub néeg ba, seeta seet, ba gis ko?