Luke 16:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Fekk miskin mu ñuy wax Lasaar daan tëdd ca buntu këram, fees dell ak ay góom,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ab baadoolo bu ñuy wax Lasaar nag farala tëdde buntu kër waa ji, yaram wa ne fureet aki góom,