Luke 16:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Noonu boroom alal ja ne: “Kon nag maam, maa ngi lay ñaan, nga yebal Lasaar ca sama kër baay,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Ci kaw loolu boroom alal ba ne: “Kon nag maam, ngalla yebalal Lasaar ca sama kër baay,