Luke 16:28 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ndaxte am naa fa juróomi rakk. Na leen artu, ngir ñu bañ a ñëw ñoom itam ci bérabu metit wii.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax sama juróomi rakk a nga fa. Na leen àrtu, ngir ñu baña ñëw ñoom itam ci bérabu metit bii.”