Luke 17:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu waxaat ay taalibeem ne leen: «Fiir yuy yóbbe nit bàkkaar mënta ñàkk, waaye toroxte dal na ki koy lal.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu neeti ay taalibeem: «Ag fiir guy bàkkaarloo manula ñàkk, waaye wóoy ngalla ka koy lal.