Luke 17:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi muy jub benn dëkk, fukki gaana ñëw, dogale ko. Ñu taxaw dand ko, di wax ca kaw naan:
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu dem bay duggsi cib dëkk, fukki gaana dikk, dajeek moom, ba dànd ko, daldi taxaw. Ñu xaacu ne: