Luke 17:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dees na leen ne: “Mi ngi fii!” walla: “Ma nga fale!” Buleen dem, mbaa ngeen di leen topp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te it, dees na leen ne: “Ma ngee!” mbaa: “Mu ngii!” Buleen dem, buleen ca topp.