Luke 17:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte ni melax naan ràyye ci asamaan, di leeral gii wet, ba ca gee, noonu it la Doomu nit ki di mel ci bésam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax ni melax di xuyye gii wetu asamaan, ba ne ràññ ca gee, noonu la Doomu nit kiy def keroog bésam.