Luke 17:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye balaa booba fàww mu sonn lool te niti jamono jii dëddu ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye balaa booba fàww Doomu nit ki am coono yu bare, jànkoonteek diiŋatu niti tey jii.