Luke 17:28 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Dina mel it ni la xewoon ca bési Lóot. Nit ñaa ngi doon lekk ak di naan, di jënd ak di jaay, di ji ak di tabax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Noonee itam la deme woon ca janti Lóot. Nit ñaa nga doon lekk ak a naan, di jënd ak a jaay, di jëmbat ak a tabax.