Luke 17:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye bés ba Lóot génnee Sodom, Yàlla tawloo safara ak tamarax, rey leen ñoom ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye bés ba Lóot génnee Sodom, la tawub sawara ak tamarax wàcce asamaan, sànk ñépp.