Luke 17:34 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Maa ngi leen koy wax: ca jamono jooju, ñaar dinañu bokk a tëdd guddi, dees na yóbbu kenn ki, bàyyi ka ca des.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa leen ko wax: guddig keroog ñaar ay bokk benn lal, kenn ki, ñu yóbbu ko, ka ca des, ñu ba ko.