Luke 18:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu Yeesu wax leen itam léeb wii ngir xamal leen ne, war nañoo sax ci ñaan te bañ a xàddi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeesu dellu leen léeb lii, ngir ñu wareefoo di sax ci ñaan te baña xàddi.
Recommended Reading