Luke 18:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu ne: «Dafa amoon ñaari nit ñu dem ca kër Yàlla ga, di ñaan. Kenn ki ab Farisen la, ki ci des juutikat.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne: «Ñaari nit a julliji woon ca kër Yàlla ga. Kenn ki di ab Farisen, ki ci des dib juutikat.