Luke 18:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Juutikat ba moom, ma nga taxaw fu sore te bëggul a siggi sax, xool ca asamaan. Waaye ma ngay fëgg dënnam te naan: “Yaw Yàlla, yërëm ma, man miy bàkkaarkat.”»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Juutikat ba moom, ma nga taxaw fu sore, ñemewula siggi sax, xool asamaan, xanaa di fëgg dënnam te naan: “Éy Yàlla, yërëm ma, man bàkkaarkat bi.”»