Luke 18:17 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ci dëgg, maa ngi leen koy wax, woyoful ni xale, nangu nguuru Yàlla, doo ci man a dugg.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa leen ko wax déy, képp ku baña nangul nguurug Yàlla ni ab xale, doo ca dugg mukk.»
Recommended Reading