Luke 18:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nee na: «Dafa amoon cib dëkk, benn àttekat bu ragalul Yàlla te faalewul mbindeef.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne: «Ab àttekat la woon cib dëkk; ragalul Yàlla, yégul nit.